تجاوز إلى المحتوى
xaajub jaar-jaaru yonnente bi.•20 / 32

kañ la rañaan gi amoon ak yéeg gi?

Answer

bi mu amee juroom fukki at, ñu farataal ci moom julliy juroom.

raañaan gi: mooy juge jàkka ja ca màkka dem ca jàkka ja ca Falastiin

yéeg gi: mooy bawoo jàkkay Falastiin dem ci asamaan sa, ba ci sidratul muntahaa.

All questions in this topic