تجاوز إلى المحتوى
xaajub jaar-jaaru yonnente bi.•21 / 32

na ka la yonnente bi doon woowe nit ñi ci bitti màkka?

Answer

da daa woo waa Taahif di leen gaaral boppam ci xew-xew yi ak ndajeey nit ñi, ba bi ansaar yi dëkk Maddina ñëwee daal di koy gëm jaayante ak moom ci war koo dimbali.

All questions in this topic